12❤️

3.5K 433 10
                                    

Moi: euhh...euhh

Chérif: ça se voit que tu m'aime bien parce que tu bègues en me voyant.

Moi: chérif silonek

Cherif: khana nga dalal ma sakh

Ndiatté: iow chérif yekssil kii weroul

Chérif: lol bayil diambour

Moi: Ndiatté deim lene si salon bi ma nieuw

Chérif: salam! Mère nakamou? Naka yaram bii?

Mère adji: mangui ni rek sama dome di dieum makk

Chérif: pourtant mère yangui si forme dh mais sa dome mola dakk nak

Mère adji: deigual! Togal sama dome

Moi: chérif, am ndokh

Mère adji: doko soukeul

Chérif: soukeul wayy!

Ma soukk nank, instant yii rouss la deif ndakh sama yaye ohhh sama yaye nama yalla bal mais eupeul na, ndiatté nak mangui ko dieppi bay beug dhé. Maye wakh parégouma sakh yayou Ndiatté nieuww shii tay ma dhé mère yacine rek.

Mère yacine: salameleykoum

Mère adji: hii sama kharitt namnalla

Mère yacine: Ndiatté moma wakh guane bou risss ngaine am motakh ma nieuw

Mère adji: deiff nga lou raffett kay tokk

Mane dh sama yaye mingui retane mais nieuwou yayou Ndiatté bii nekhou ko bene yone. Elle sait très bien que cette femme est venue ici pour partager l'argent que lui donnera Chérif .

Chérif: euhh.. mère mane dh je vais pas passer par quatre chemins pour vous révéler mes bonnes intentions.

Mère adji: mangui degglou?

Chérif: mane dall Leyssa Fall dall la beugue th affairou niakk fayda takhouma dioukk

Mère adji: ahh comme ninga ko guissé nii dh keur mafi kilifeu ndakh sene baye bamou gagnou ba legui mafii takhaw takhawayou kilifeu mais n'empêche ayy nidjayam ak ayy badienam gningui thii deukk bobou niouy wakh lam-lam khamna dinalene avertir. Ma diokh kadou gui mère yacine mom tamite yayam la.

Mère yacine: ahh leyssa mi dh khalei bou bakh la! Kou yarou kou gueume diangam th yitt kou fonk sama dome djii Ndiatté, leyssa yoroul dh mais loumou yorr bookk ko akk sama dome. Khana diko nianal yalla rek.

Ndiatté: waw mane mom leyssa damako beugueul sama bop, louma wakh ci mom rek amna lou dess.

???: khana réunion familiale sou amé ngaine wakh ma bok

Mère adji: yekkssil, chérif kii moy sama thiate bii, iow éhhh kii chérif la toudd moy beugueunté ak leyssa.

Thiatt: ndakh yalla leyssa am koumou nopp

Mère yacine: wa leyssa loula téré wakh.

Ndiatté: très loquace cette fille!

Leyssa: euhh... sante nalene yene nieup! Chérif sa wakh rafett na ! Mais liila takha dioukk taloumakoo

Mère adji: guissnga iow teranga binga beug khagne sa ndaye mofi doul amé

Mère yacine: leyssa réfléchis !

Ndiatté: désolé mais aussi la décision lui revient

Thiatt: bane decision iow mayma!!

Chérif: leyssa khana do ma deif nii dh

Thiatt: wakh deug yalla

Chérif: bon dina nangou parce que dina gueuneu wakhtane ak mom. Mais je veux ...

_______________________

Qu'est-ce qu'il veut ce chérif ?😫

Ne pas être vierge ?Où les histoires vivent. Découvrez maintenant