Rencontre 2

6.5K 853 318
                                    

       Voix externe

Lorsque Seydina a posé les yeux sur ceux de Yasmine , il s'est levé brusquement

Seydina: Yasmine ?

Yasmine: monn amourrrr ( en courant vers lui )

Seydina: ehhhh ehhh taxawall ! Boulma diégué dhh

Yasmine: wa bébé khana namoma

Khadija: (en se levant ) ioeee ehhh béne affaire na leer seu boop ! Seydina c'est pas ton homme donc seu mots yiii garde les

Yasmine: ioe kouleu yéwoone khadj gouddi nileu Seydina dafma faaté dagkoy geum?

Seydina: ioe yaay kane ba meunou mala faaté xolal Yasmine boulma togne dengeuu

Khadija: bébé calme toi beugouma guay mère ioe tmt surtout pas ak ce genre de personne

Seydina le regarde l'air choquée tchieyy

Il s'assoit et Bachir aussi

Fatim: j'ai l'impression que vous vous connaissez appart Adja : bon elle c'est Adja c'est ma colocataire on s'est connues depuis mon arrivée ici et elle est trop gentille, Adja voici Khadija Seydina Yasmine et les deux que je connais pas encore

Adja: non Bachir khamenako

Bachir: elle c'est ma femme Samira

Samira la guette de haut en bas et se dit genre « ki foumou khamé Bachir ?»

Fatim: euhhh je vais voir Ahmed dans la chambre

Khadija: bébé ?

Seydina: ouii?

Khadija: viens m'accompagner !

Seydina: fo dieum?

Khadija: je vais prendre de l'air à la terrasse

Samira: je viens avec vous

Bachir: moi aussi

***

Du côté des garçons

Bachir: wa Seydina louma wara deff ? Samira noumakoy wakhé amena dome ?

Seydina: shii Bachir mane amena louma doy sama seuy dina yeungou

Bachir: mane nak sama seuy mo narra tasse

Seydina: boy je préfère geu waxko Samira bala dara di khew

Bachir: ak état bimou nékk ?  Ma bagne dieulouma béne risque

Seydina: légui bouko Adja wakhé nak?

Bachir: je pense pas mou waxko

Seydina: fofou gua tolou? Baxnaaa en tout cas daal waxko Samira bambara la té xamoul foo dafkoy nokh légui

Bachir: ça c'est sûr ! Mais tiite na

KHANA DOU MAKO BEUG [TERMINÉE]Where stories live. Discover now