Saint Valentin partie 1

5.3K 688 15
                                    

après quelques semaines de turbulences
Pour montrer son amour envers sa femme Bachir décide d'inviter Yama ben dîner de Gala bou makk organiser à l'occasion pour la saint Valentin 🥰. Comme ça mou meuneu firdelll mbeugel leum . Yama ak préparation bi rek dara dou doy comme d'habitude ndella , salla ak dallou ndakarou nieuw au secours baala khalé bi di deff todj todj perforé . Dans le Salon gnou Tokk wakhtane sotanté khalate

Yama _  li dall leu Bachir beug ma demm thia fete ba louguen thi khalate ?

Salla _ legui bo demoul noy deff ?

Ndella _ moma diakhall nak

Dallou ndakarou _ ki mako kham day bagna deff todjiangué motakh mouy lathié

Yama _ mère nandité guay am fofou dama beug conseil you bakh mais avant gnou dém thia tailleur bi ma tane taille basse bouma wara soll aidé lenma ak bijoux yi

Ndella _ badou sa tailleur bobou gua khamné mo raw diasssi loumou dagg mou moy😂

Salla_ wouy yaye mangui RAM tailleur bobou gua Khamné comme au secours yi modèle you tardé

Dallou ndakarou _ ma meuneutoul khôl modèle yoyou comme thiouthiou sidakh

Salla _ nagn dem centre commercial bi nek côté HLM gnou tanal leu robe you bakh waw kay

Yama salla ndella ak dallou ndakarou dém bay guéneu tassek Ya Fatou mom tamite khamoul lou khew mouni dalen di top par la force .

Ya Fatou _ fo len dieum rek la beug kham ahhhh man Guen di sakall pekhé nak douffi amé tay sen tank sama tank ba ici répose .

dallou ndakarou _ man ki saffouma dara ak grand boubou bi mandi dakandé tchipatouuuu.

Ya Fatou _ mani gua andak say morom lala wakh man douma wakhak yagg bawoul dara . Yama yaw lay wakhal damay nieuw par force.

Ndella _ centre commercial bi rek lagnou dieum khana sa khel dalneu

Ya Fatou _ damay dém déh Amoul rekiller

Yama _  Ya Fatou amgua diabète , ame hypertension , teksi cholestérol soula Corona dougué rek moussibeu dikk khamal sa bopp
Ya Fatou gua balma deh mais Say dieuf mom adoulak diamono ak fi rew mi tolou thi cas criminel

Salla _ ( communautaire)

Yama _ waw tokk thi keur gui  mola warr arr sa bopp arr sa ndiaboot dou DEUG
Ya Fatou khana doù ya doon wakh nane hôpital yi dagno maguette place amoul teh médecin yi khamouniou dara kone togual thi keur gui diapalé sa bopp , Man yow la beug nak yaye sama kharit souma nieuwé mayla sidem Mali wala sollom waw kay sama goro bou niawoul bi.

👀Ya Fatou mom sakh daffa tite ba khouli yama thi ay beutt lou waral bi discours bamouy nekhalaté.

🗣Rek Bachir wakh thi guinaw__ yaye wakh nala deug nak fo dieum yangui febar ak fi rew tollou non non yama a raison reste à la maison ça va aller inchallah .

(Ah yama meunoul bakhé nonou ndeketé daffa dem bay sapali Ya Fatou rek guiss Bachir di nieuw derrière mou deupp carte yi deff gentillesse ak raffiné door jongué changé discours )

Yama _ mo Bahir yangui fi guissoumala wone sakh gnou dem centre commercial dellousssi mon nakhmour de vie sama leufeur leufeur

Ndella _ Bachir thi kanam

League des jongoma ande demm centre commercial rombeu Ya Fatou ......

Bachir _ yaye on rentre à l'intérieur stp

Ya Fatou est énervée mais ne veut pas montrer sa colère à son fils du coup elle fait ses grimaces très chelou 😭

Bachir _ yaye loy deff ni khana quelques choses t'a piqué ?

RAKADIOUWhere stories live. Discover now