Sëëto sëët

10K 1.2K 232
                                    

Sabar gui nekhnaa , ambiance bi nekhna , nieupeu contane machallah takka gui dall zéro faute. Beu bachir delo keureumm .Yama comme d'habitude téla tass Lang gui parceque néna daffa wara seuyi toukeul diamono harmonisé coupleum .Takhaw deff zena la guerrière .

Yama _ Borom tama bassa guine tathie , machallah guisna sen tewaye rafett sama khôl Sedna , legui nak adounay khél diamonoy beut , lekk guen beu sourr nane ba mandi .meun Guen gnibi damay seuyi . Boulen faté rangé chaise kou lekk lou nekh wara meuneu rangé

Invités yi nane _ wahh ki louko dall nakk aka badola thi jeûne mariée

Yama _ eh boulen ma sonall surtout yaw Fanta mbaye sa khew ken lekoul , jus bissap Mélni tamaté bou ménopause safoul Dara amo lo wakh , yaw nak pendo damala yeureum fatewouma sa barquette yi gua khamné fataya yi comme carreau cassé wow Kong la deff. Bouma ken fatt nak rompéeee way

Salla _ ay yama sa jourou mariage tamite

Yama _ dimbeulima deh guiss nagn fi bouné gni malenn kham comme ay sipion

Salla _ espion yama Espion

Yama _ baatay kougnou khamal lagnouy weurr . Sett sama mbokki dieukeur Khatito ak gnome di oute informations Mélni Khalass walla teuss doumako nangou , pour gni rek dougn fi feké sama mourou sinon gnou mouri sama soutoureu

Fanta mbaye _warnala sa coiffure Mélni panou grand ngaal

Yama _ tourki diam yaw man guay khass wa batay demm len rekkk sen tissus hôtesse you torokh Solen paré defko morceau tayoukay ndeggg . Soubeu guén nieuwate nak keur Bachir  fokguen feké sama labanne . Lonnnnnnnne kouko tardé

Ndella _niaw kendou sama domou nday do bayi chat do bayi charlatans do bayi charabia

Yama _ bilahi gni comme ay cheuteuteuteuete

Dallou ndakarou arrive et appelle les filles _ Yama guinaww ba dakk gua say guane kay gaw préparer gnou mour leu gua seuyi . Nieup nek thi Diam

Yama _ lolo gueneu nekh Colonna vuris diekhna gnou demm simbang mbang . Affronté samay noone

Une heure de temps après les bagages de Yama sont prêts il ne reste plus que les prières et donner des conseils mais boul sonn ak yama darra dou néne. Gnou mourko ba Paré tathie ko devant toute sa famille ak gni dieulsi sëët bi . Papa dji Dieul kadou pour yedeuko conseilléko .

Père thioukoulé _ ah ndaysann kouné lilay niane am sa dom yarrko bamou magg gnou mourko moudem seuyi .

Yama _ sama badienne moma yarr dehh na lepp leer . Mouyenn père ya deugeur fitt beug guisslénma

Père thioukoulé _ sa deugg deugg yama nekk khalé bou bakh ame yarr teyé lamignam respecter ay kilifam

Dallou ndakarou _ nelll thi lingua feké  pour qui rekk zéro kersa touti khamadi

Père thioukoulé _ waw yama dama lay ndekk rek mo demé sa yayou dieukeur defko nissa yaye

Yama _ souma deffé ni domam rek ma yayoko khana eupance 💃🏿

Père thioukoulé _ boula sagga nangoul teh khamné danguay seuy

Yama _ Man sama yaye sakh douma Saga guanane yayou diambour na réglé ma réglé keurr gui nekh . Apo vent , dribbler seytané

Dallou ndakarou _ pour ki rek mo raww bissap bou toy forokh toll la deff

Père thioukoulé _ mak yi dagn dann wakh nane benn seuy nekhoul bo demé nagua mougne

Yama _ louko wara nakharil la khamoul Bachir néna man la aimé ma yoor feeling mou yoor sama feeling dagn koy seuy bam nekh beugouma benn thiow. Bayil titeulaté bi

RAKADIOUOù les histoires vivent. Découvrez maintenant