Le dîner

11.4K 1.3K 249
                                    

#RAKADIOU

Quand l'amour vient naturellement en s'en fout royalement des préjugés sur sa partenaire. El Bachir diaw passe à la vitesse supérieure dans sa relation avec Yama et décide de l'inviter à dîner et la présenter à ses amis Au Passage. Comme un homme galant il lui envoi de l'argent pour qu'elle se prépare en conséquence mais on connaît Yama et ses dérives.

Bachir _ Hello chérie

Yama _ dema lakk Wolof

Bachir _ no defff , paregua pour ce soir

Yama _ hiii bou yagg Sakh ,

Bachir _ je t'ai envoyé de l'argent sur le compte de Salla pour que tu puisses acheter des vêtements.

Yama _ argent mom deggna kossi donc Messi beaucoup

Bachir _ a plus et bisou

Yama _ moi zausssi ze te Faune

Elle est avec sa cousine salla au marché , en train de chercher de quoi porter pour l'événement de ce soir.

Salla _ yama anii khaliss bi ?

Yama _ sama soutien gorge lako deff , marché bi woroul yaw retirer ba Paré diko deff sa pochette ma Dieul lepp

Salla _ wa guenel ma faye borom boutique bi gaw mougui goudi nak

Yama _ mom robe bi rek la am ? Eh segn bi amo benen khana ? li dima saff tamé yourette ? Li kom Bethio man dama doff doumako soll

Salla _ fama yaw tamite lou am thi li , robe de soirée leu

Yama _ moh kholal neko mou bayiko , nit dina soll li tamit , khana tailleur biko niaw dadone lokh , yi beun beun

Salla _ fi mo geuneu moyens cher nekal nitt

Yama _ Robe bi niata leu ?

Salla _ 50 mille kessé

Yama _ yassi tek kessé nonou ak khepp .dama dieundoul robe 50 mille teh diko tay la wakh , Borom bikittt bakhneu niogui demm say bagasse niou niaw teh cher , yaw sakh lo bokak sipakh ? Moytoul diégué Casamance balla nioulay kaldou.

Salla _ yama yaw dall ni rekk fodem wanefa sa bopp

Yama _ eh dimbeulima nak , limouy diay sou rafetoul dagn koy wakh sou benen yonee mou kham bopam , ze ne si pas zypocrite

Salla _ hahaha wooooy Yama koula diangual lolou

Yama _ yoor farr bou civilisé rek 1 2 3 mounima euhh ohhhh cé que moi ... Affaires yoyou dall mané kharal ma diangui watt , diamono nekhoul , adouna goudou tank SIDI rama tonton Salif

Salla _ lolou mom lou baakh leu mais robe bi nak ?

Yama _Bayilma morceau foberékay bi , gnou dem thi Modou souroumlé couture deff taille basse bou agressif , tim Tate , pathial samay wenn , wané sama jongoma fofa Poussière. Bachir kheum

Elles rentrent chez Elle après des heures dans le marché sans rien acheter . Yama Commence à se préparer pour ce fameux dîner et Salla lui donne quelques conseils.

Salla _ damalako niane rekk bo demé gua réglé guir Yallah

Yama _ pour Man rekk moutte lay deff may raw courant bou coupé , douma bougé douma wakh , monuments de la Renaissance

Salla _ wah lolou bakhna aythia legui diougueul dém nak sama jongoma isocèle bi

Yama _ barki yalla dama Sagnsé lou ame sucre vanille
Nana menthe ak pasti

Une heure après Yama se retrouve chez Bachir , il lui prend la main et le présente à tous ces amis avec fierté car il ne cesse de sourire

Yawa _ wah cawa no deff sante bi

RAKADIOUМесто, где живут истории. Откройте их для себя