Saint-Valentin partie 3

8K 799 74
                                    

La manipulatrice mère mataté 😳

donc c'est  Ya Fatou la dame dans la boutique qui demandait lou yama dieundeu mais à quelle fin? 

En tout cas elle arrive dans la maison chez Elle toute contente nak ak way you nekh 🗣

_ 💃🏿ndeysan mouyene kocc barma newone na djiguen sopal teh boul wolou 🥰 ndeysannne

Nabouja sort de sa chambre _ wa yaye contane gua deh lou khew nonou ?

Ya Fatou _ nenala man ken douma teukou limako deff tay douko faté dama nane fakh di khar résultats safoula

Nabouja _ wa legui kayy wakhma lo deff guawal yaw tamite cas dagn kooy tela tass

Ya Fatou _ sen dîner de Gala bi 😏

Nabouja _ bane dîner ?

Ya Fatou _ mom ala kham ak Bachir

Nabouja _ yaye ba demofa rek ?

Ya Fatou _ ma tek sama plan di khar résultats

Nabouja _ wa yaw tamite guawal 🤔

Ya Fatou _ dama bayi bamou dieundeu robe ak accessoires ma topate thi ay tankam khol tissu bi dem commander ko en quantité neh wadji defal mako torchon ak nappe de table bolen meuné sakh fompé lenko casse yi thia dîner ba en résumé dall yama robe bimou soll ak service de ménage hôtesse d'accueil ak tapis ba gno nirou bi Guathié mou nara ame tayy may weuyou🔥 ken dou man

Nabouja _ yaye lo wakh guani 👀

Ya Fatou _ mani yama tay tissu Bimou deff robe comme dayi doff thi birr soirée ba

Nabouja _ bane couleur leu ?

Ya Fatou _ noire paillette souma dioumoul😜

Rek nabouja khalangou di khakhatay parceque sa mère croît que yama robe bi la soll alors que taille basse bou wekh la soll 🤣🤣

_Wooooy wouyaye ayy wayy dina deh bi Guathié

Ya Fatou _ di gua rée dom Sa yaye rek aka Barri pekhé man mom on me respect rek walla moy lolou

Nabouja _ mangui dehh🤣🤣🤣 koumay kheuttt ma yewou

Ya Fatou _ tchioum ma Barri dôlei

Nabouja _ yaye gani yama loumou soll?

Ya Fatou _ paillettes you bonne Sakh 🤣🤣

Nabouja _ dina dehh wayy🤣 ayy wayy samaaaa yaaaye

Ya Fatou _ tay mom victoire lay fanano photos wadji rek lay khaar ak compte rendu

Nabouja _koumay Matt waaayyy😭🤣🤣

Ya Fatou _ Man khamna dagua contane thi sa yaye 🥰

(Ce que Ya Fatou ignore est que yama a changé de tenue au dernier moment🤔 et nabouja était dans la maison elle a remarqué que yama porte une taille basse non une robe d'où ses moqueries mais la vérité ne va pas tarder 🎖)

                         «Retour à la soirée »

Yama toujours dans ses délires de femme fatale continue la conversation avec son époux et vient l'heure du dessert le moment que redoute Bachir parcequ'il à mis une bague à l'intérieur en espérant que Yama va tomber dessus et être surprise par ce geste . C'est un homme très romantique et comme il n'avait pas eu l'occasion d'offrir une bague💍 symbolique à sa femme il s'est dit la saint Valentin c'est une très belle occasion. Il avait tout organisé avec le serveur pour qu'il mette la bague au milieu du gâteau comme ça après deux cuillères et elle tombera dessus

You've reached the end of published parts.

⏰ Last updated: Apr 18, 2021 ⏰

Add this story to your Library to get notified about new parts!

RAKADIOUWhere stories live. Discover now