Yama beuri fém

8.9K 1.1K 95
                                    


Ce jour est enfin arrivé ce même jour où yama va devenir la Femme de El Bachir diaw , la belle fille de Ya Fatou . Jusqu'ici tout était contre elle pour annuler ce mariage. Mais elle est féroce et ne se laisse jamais berné par les paroles d'une sorcière. Il est 12h dans sa maison , ses tantes sont là ainsi que ses badiennes l'ambiance est au rendez-vous sauf que Yama n'a rien donné pour le moment ni pour la nourriture ni pour ses accessoires, elle ne s'est pas encore habillée de plus les dames n'ont pas commencé à cuisiner pour les invités de ce soir . Sa badienne dallou ndakarou angoissée par la situation rentre dans la chambre

Yama _ wa badienne boy dougou thi nekk do feugg wayé né sarakh Mélni guelawou seytané sama kaw

Dallou ndakarou _ souma Amoul wone loumay sett dina taff tepi collé fakhass sa deunou mame . Damani

Yama _ lann ?

Dallou ndakarou _ geunel khaliss bi damay dém marché gane yi khana dougn lekk ? Ba heures bi thine takoul yama ko yapp loutakh gua Nay

Yama _ eupeul mola takha rass mais yayou Bachir mo gérer lepp Agne bi dagnkoy commandé . Kham gua rek daffa toubabé doffé soffé

Dallou ndakarou _ Layla laww douffi amé lekkou traikteur gua khamné mo geuneu nakhari batou ouzin keita doyna seuk , mangui ni dém sa niom tantes pour oute solution

Yama _ shiii loutakh gua beug problème legui meun na diokhé khaliss mais kharal touti rek

Dallou ndakarou _ tchippppppatou teh gua diouk defarou gaw

Yama _ takkou diakka rekleu après ma seuyi fi noyy . Boulma tek preksion

Dallou ndakarou _ dognou tere ambiance bi déh

Yama _ batay mais fou 21h dioté ma seuyi

Dallou ndakarou_ beugeu goor shimmm

Yama _ lo wakh bakhna lila metti tegoumalako ,dou néngua dagua pose ongle nonou Say baram dima saff brochettou kheuteure. Amo diom thi Man

Dallou ndakarou sort de la chambre en disant _ sa beuss ni rek la meunone mell ndakh réglé wo domou deumeukk doff nodeff am khew bou yolom

Yama _ kharal sakh ma woh Bachir peundeull senn keur. Yeukeuti fitneu , tapass seytané , ibliss ambiance

Elle prend le téléphone compose le numéro de Bachir et balance ses piments

Yama _ allô bébé sama coco banana takamtikou nekhh , faune lou bakh Borom boppou or bi diaw fara no defff?

Bachir toujours qui rigole des mots des Yama _ mon chou je vais Bien alors no doundé beuss bi yangui paré

Yama _ machallah machallah lima paré eupeu , lamala parel nak souy tambali guay rouye takk ba diékh nak

Bachir _ lolou amoul problème dougnou bolé . Man j'ai vraiment hâte que tu deviennes ma femme . Dagno waronn takk legui 17 h daffa sorri

Yama _ nassa khel dall bougnouy takk douma fi sakh khar geureumaté sama valise paréna bou yaggg Dieul taxi talal bassa kaw lall. Ay li di kouko wakh kolera

Bachir _ hahaha je t'aime

Yama _ lave you niarri yonnn ba Toto tape Pathé

Bachir _ dit moi sama yaye limou eudi bakhneu

Yama _ lolo takh ma wola sama kani thioukouly

Bachir _ lou khew bébé ?

Yama _ guissoumako ba legui teh Man dieundou ma wone dara diko kharr fimné ni gane yangui khiff mar , khouli sen beuti nak Mélni kou waneu kourrou roff

RAKADIOUWhere stories live. Discover now