"Dieul ndieul" partie 1

7.4K 924 86
                                    


Après une semaine dans sa nouvelle maison, Yama est toujours aussi explosive et rakadiou avec son époux El Bachir diaw. Ya Fatou l'ignore depuis quelques jours et Nabouja commence à se rapprocher de sa Belle sœur, une situation qui agace cette vieille dame remplie de Colère depuis le mariage mais qui a toujours une idée derrière la tête. Pour la première fois yama dougou wagn Dieul ndieul lolou rek événement teh kou kham yama khamné daram dou seed bay simple . Deff ngandim invitation comme d'habitude , invités Kharitou Bachir yi ses collègues et les voisins bassi Kharitou Ya Fatou .

Samedi diot fadiar mou yewou yewalé Bachir.

Yama _ chou national nodef sama khalakhineu yewoul tayla beussou reukeunté déh doreunté you bakh . Deff taille basse andak sama État major deff dégagement dougou marché, dougou wagne daldi tek Agne bou Mélni tabarfakala machallah gueweul. Lou meussta ame sa birr keur gui Yewoul andak man.

Bachir se réveille étourdi _ lannn ? chérie ya kham lolou toi aussi demall lo deff bakhna walla demal ladj sama yaye ba kham

Yama _ boul faté ni sa yaye daffa amé rapp woroul damakoy yé mou dorma pess legui guisso lokhom yi Mélni auto ndarane .

Bachir _ batay legui va au marché demall ak ndella salla et autres.

Yama _ wa bakhna à thi kanam so paré nagua sangou ba sett khegn plaisir tok kharma ma réssal sa adouna . Khorom sa thiepp

Bachir _ je te donne beaucoup de bisous bisous

Yama _ laylalaw dagg ma dieundeul bijou en or 🥰 bi dieukeur kouko am lo di wakh ? Ma khôl Bijou yi ?

Bachir _ yama bassi kanam inchallah bassi kanam rek

Yama _ sama sapeu deguine dinala name lou beuri pekhé. Wayé ma dém nieuwate

Elle part pour rejoindre ses amies au marché mais juste avant de sortir elle croise Ya Fatou .

Yama _ wa kidou mère mataté yaw ? padd niak soutoureu , wodo torokh , Fo diouguë? Kholal boul dém fenn tay may ayé defall leu teranga bodoul faté ba faw , digua lek digua nane yaye sama Goro nak .

Ya Fatou _ Man soumala reuké dotoko defati bangua may karr thi bountou keur gui di woute ko kokeuli

Yama _ mère mataté nak yamal fadiar tell malay nekhal guay déranger Man fima nekon ba legui diouguew mafaa .daffa di kay sama yayou dieukeur warnako meuneu terall guinaw ay diam.

Ya Fatou _ pousseul ma dial la wakh sa ndokette bou Barri roukou

Yama _ haaaaaaaah boul togn domou ndaye guisso sa touss ngeul bi meuneu thioup adouna Ya Fatou yamal may wakh mouni daffa deff Cole  ya yeuy deh sa bopp bou khogn teh Barri ndokhoum sitti . Mangui dém marché Man .

Ya Fatou _ yorral sa lamigne di wakh rek lilay door mongui nieuw

Yama _ bo dieufé rek ma wakh boumla bett

Ya Fatou rentre dans la maison déterminée on dirait encore qu'elle prépare un sale coup mom dou sone dou tayi😂 elle se dirige dans la chambre de nabouja yéko .

Nabouja _ ay yaye yeureum ma dama sone

Ya Fatou _ mani yewoul guay nelaw Mélni baleine

Nabouja _ lou khew legui ?

Ya Fatou _ sama plan bi lalay wakhate si

Nabouja _ chiii yaye lolou meunoul nek deh en plus yama defouma dara

Ya Fatou _ wayé man sa ndeye defnama dara anassa solidarité yayable

Nabouja _ lo beug ma deff

RAKADIOUWhere stories live. Discover now