Sabar gou taarr

8.6K 1.1K 138
                                    


Place à l'ambiance du mariage . Yama est déjà prête et toute belle dans sa tenue de madame Diaw .
Deff taille basse bou wekh talll beuri diam .
Jupe crayon bou noppe ay anche teh beug forme , make up bou simple . Lall colle bou wekh AK couronne bou dorée , soll ay talon haut you sokhor .
Niaff touti héné thi digg lokho bi . Takk ay chaînette en or , Di briller de mille feu. Yama deff Sagnsé moderne civilisé di diaguar diaguari devant les invités pour les saluer . Le sourire de Yama tout en blanc , l'élégance de yama , ce soir c'est une fleur .Mais on connaît Yama il faut toujours qu'elle rajoute un mot sur sa personne .

Yama _ wah salla nitt gni beuri nagn deh kou invité gni nieup dama nouyo retane ba calé .

Salla _ ay kharitou Bachir , say book ak say quelque copine

Yama _ wakh geu deug man say mbokk nio geuneu barri ay yambeu aka gno sakane comme vermicelles chinois

Salla _ machallah

Yama _ dako diarr Ebola sakh diekheulou gnou. Souma invitéwoul ken sakh samay mbokk meun nagn fessal khew mi

Salla _mais nak yangui Sagnsé sama DOM ndayy sa blanc bakhna

Yama _ wakhal way , mais bou guawoul diekh ma kheum kheumatte jupe bi rek comme elastro sama kaw serréna deh soumay noyi bou bakh mounane tareeeete. Talon yi nak khana foursette lagn ko defaré soumay dokh melni kouy diegui siratt

Salla _ reglel nak tay d'où beussou kass ak khoulo ani ndella Sakh

Yama _ day rangé chaise yi . Tay lang gui lay todj tassar ehhh mbaye

Salla _ ay yalla man yaw digma ray rekk yaye fethie khana

Yama _ ahh waaaa waww sama khew sama beuss eukine timilité damay bara mbaye lou kandang takhaw di diayou , mariage dagn koy diokh geudd

Aussitôt ndella entre pour récupérer Yama

Ndella _ geuneul wané sa bougement ak sa dégagement Lang gui amna espace ni guemignou yawou dial foula nekh tokk

Yama _ lannnne . Wa man loutakh tellouma am dieukeur . Sama khôl Bangui Mélni Rossi domoda bou dogg : peukh peukh rekk

Ndella _ tay sa beusseu loula nekh defall

Yama _ salla kay thiapp thippalma defaratt sama kanam dama nouyo retan lou nior ak lou nioroul ba faré. Platou deukhine la sama kanam gui ndirol

Salla_ wooyy sama mame nekal nitt 😂

Yama paré bongomane yi akk borom tama yi darko di tassou lou perpendiculaire 🗣

_ da guen di nelaw yewoulen bokk yama lakka deukeu Kone khana nekh guay lathie 🕺🏾

Yama _ nell madame diaw way  akhh

_ da guen di nelaw yewoulen bokk madame Diaw lakka deukeu Kone khana nekh guay lathie 🕺🏾

Yama _ ay wayy lollo nekh

Yama diap thiatou taille basse bi , di ndiapp di diayou di piss dioubeuli thi gueww bi

Bongomane _ dokhall dokhou bandiloul boulo ragall way ndiabal ndiabou bandits

_ kou tathiou woul gnou dieul yama dougeul ko sa khôl moulay begeull

Yama _ aaaay way li nonne yi beugonn dalouma 💃🏿

_ youza youza youza

Yama _ mbassa mbassa

_ guine tathie

Yama _ yaw koula nampal khana tata rose sa tassou you yagg yi nakk

Ndella _ wakh DEUG damani tousseul reuk sabar gui

RAKADIOUDove le storie prendono vita. Scoprilo ora