Nuit de noce mouvementée 01

8.4K 1.1K 97
                                    

Il y'a des belles mères osées bagn sen Goro diarall nalen kheum wallah danou rapp pour retarder une nuit de noce mais nak
Yama doff bou ame khel leu métaphore bouy wané qu'elle n'est pas dupe à ce point pour croire aux évanouissements subite de Ya Fatou . Elle amène une bouteille de vinaigre , elle n'a pas réfléchi deux fois. Kharoul kouko diokh Signal kharoul intervention.
Yama diap Ya Fatou diko soll vinaigre sans gêne yaw mère bi diolou thiorokhane bay mir dieki sayy rekk 👀bouki beut yi nane _tokho tokho ohoooooo ohooo

Yama continuer di dolli , Ya Fatou di gualleu melni lirou 1 semaine. Bachir tok di khôl melni yama day deff lou bakh fek mongui raay yaye dji

Nabouja d'un Geste sec dégage la bouteille et Ya Fatou se lève toute trempée de vinaigre.

Bachir _ ahhh alhamdooulilah Super ça maman tu vas Bien maintenant?

Yama _ wakhnala daguay vinaigre khoutou khatam rek lepp bakh genre yi massi ayy bouma amone pobar barra mousso nak niaff ko thi bakane yi bouy tissoli di tané

Nabouja _ mouk mouk 😱yaye yaye est ce que ça va ?

Ya Fatou teup _ wooy wooooy wooooy dama mir wouy guissouma lou kheww fi ? Loumay khégn ni ?

Yama _ effets secondaires yileu rek dou darra . Beut yéh safff binaigare mais dina guissate walla ma tafko moutarde sisonn (Dijon)

Bachir _ franchement merci beaucoup yama sofi nekoul wone bou niaw

Yama _ mo lolou dou chimbi rimbi yaw

Ya Fatou _ tokhoo ohoooooo ohoooooo 🗣🗣

Yama Dieulate bouteille bi rek Ya Fatou randou pousse lou sori 🏃🏿‍♀️

Bachir _ maman tu as quoi ?

Ya Fatou _ nama vinaigre bi sori bachir

Yama _ yaye nak kharal amna lou dess après guay comprends ay rapp loulay fathie rek lay bagn

Yama di yengeul bouteille dissi lémou _ sakadia makadia boul diar thi kenn diarall thi man mi wouyy djiné yahhh all momine guine tathie arguay momime . Shifoune mafouna khaktoume lafttoum . Khakhh touff

Bachir _ lo deffni ba tok

Yama _ sa yaye da âmé rabou Jumbo motakh mouy danou mais niane nassi bouteille bi khamgua sama mame da ame kham kham , legui bachir Say bo kheuyé dagnkoy diokh ben goukh après mou seulmou inchallah fekk une semaine dina werr

Ya Fatou _ mouk thi adina

Bachir _ yaye nak makk moy fathie bopam man sakh ma lakoy deffal tous les matins

Ya Fatou commencer dioy bay kheukheute ndaysann kotteu nabouja di dioyy dall , khamna bou bakh né yama dinako raay sans problème

Yama _ legui n'a demm sangou ba sett teudi nelaw mak dou goudé khoulé bakhoul thi ay beutou garmi

Bachir _ wakh gua deug il se fait tard nabouja amène ma mère dans sa chambre Alors on se dit à demain deggua yaye

Ya Fatou _ mbéeeeeeeeeeeeeee mbeeeeee🐑

Yama _ yapp (viande) bimou lekon moy fayou ni

Bachir _ yaye nak ne fait pas ça dina bakh inchallah tu m'avais pas dit que dagua ame rapp mais Yallah bakhna yama dinala diapalé ok

Yama _ machallah biss bou danou waté rek ma defalko carbounate walla top sol aka bakh thi makk bou amé Rapp

Bachir _ Man je ne savais pas tout ça Thiey Yama yaye kham louné bon on n'y pas legui

Pendant tout ce temps Ya Fatou mongui boukii beut ndakh vinaigre bou fort . Yama et bachir quittent le salon pour aller dans leur chambre aussitôt Ya Fatou gifle nabouja tass mbethie👋🏾

RAKADIOUWhere stories live. Discover now