Saint Valentin partie 2

4.4K 709 17
                                    

La soirée arrive Yama sollou di tagg bopam aka paré thi jongoma senegalaise 🔥

_Khana dou ma meun beuss man yama thiapatioli Bachir natou ya Fatou Kharitou ndella kouma pogné , pogné valeur , pogné khalé bou sénégal beug dou ni ? Nelen mbiwww

Après sen sollou Yama ak Bachir Dieul auto daldi départ direction la fête .
nieuw machallah dougoussi rek invité yissi salle bi yeup tourné couple bi deff Sagnsé tout blanc Bahir ak nieti Abdou bou selle bi⚪️
yama taille basse bou wekh tall di takk ni diamant , khalé bi nak elle est toute mignonne . Gnou daldi doug hôtesse bi placé len thi ben table bou Royale bachir tire la chaise pour que yama puisse s'assoir galanterie oblige . Tok deff tekk deff classe ba fi mongui bakh

«Vous n'avez pas remarqué que yama n'a pas porté la robe qu'elle avait acheté au centre commercial»

Récap : elle revient chez elle avec la robe et les accessoires en ouvrant le paquet elle s'est rendue compte que c'était pas son style elle a juste pris pour faire plaisir à ses amies . Yama tallal robe bi thi kaw lall bi .

_ li dinako soll teh diko tay , robe bi fess dell ak ay wassinetaurrou dieun khawma paillettes . Ma bagn la wakh li moy khawi sama soutoureu may sama noone ticket vip bougnou dougué sama life dima kokeuli au balcon doumako nangou . Kharal ma dem sama tailleur bou defalma taille basse bou ame diom deffal Bachir nieti Abdou gnou am diam la paix mais limom doumako soll di saff sirène bou ménopause. Mouyen li da neuboul dara sakh thiammmm. Douma toubab nak bayil rek ma faune taille basse bou reewww

«La soirée»
Tout au long Bachir ne cesse d'admirer la beauté de Yama . Il faut l'avouer elle est particulièrement très belle ce soir .

Yama _ wa lomay khôlé ni rek lima soll rafetoul

Bachir _ tu es toute belle yangui nice ni

Yama _ wa guiss geu deff taille basse time tate ,nobe sama forme jupe crayon ni fente derrière wané sama sauvass . Sama cheveux bou goudou di wagnarou sama guinaw . Sagnsé mako mom .

Bachir _ machallah tay mom zero faute

Yama _ bayima may wakh gnou beugonne ma soll sen robe bou niakk kilifeu bobou ana lou dakk sama taille basse

Bachir _ magnifiquement ce soir ya takh sakh ma changé ténu aussi

Yama _ wa wouyouma ?

Bachir _ oui

Yama _ yaw mi tamite tay dagua beau deh mouyene guissoumako wone yangui saff goor nekh rétane diek mbakhané sa nieti Abdou rek assamane téyé wouleu sama bachir feuleur de mon cœur racine de ma vie .

Bachir tout content _ hi hi hi deugeul doma rayy

Quelques minutes après il y'a un orchestre qui joue ses partitions , les serveurs font le tour des tables ,la fête continue .

Yama _ wa Bachir limoy animations bi

Bachir _ waW dîner de gala kagn motakh lo beugoune

Yama _ ehh ehh dom nday kay ma wakh la dolén fi tekk wally seck gnou rigou rigou walla sakh SIDI Diop diabiraaa yeugeulll wayé Ismaël lo khawma Souleymane faye li meun neu sakh nelawlo mbeur bou danou

Bachir _ pour yaw dall musique yeup tell ma radiakh leu

Yama _ ay bou tama yi sadjiii wone bama diouk tassa mbakh guine ohhhh 😫

Bachir _ ak nigua Sagnsé ni 😘

Yama _ bayima adouna dagual dieul lila metti bakhal bamou nior sotti soukeur dégagé jalonné koulay sonnal . Wayé soirée de galaktik melni kay len nelaw , geumeu 50f khef khipi diourom

Bachir _  soirée de Gala 🤧loutakh ma invité rek la khamoul

Yama _ ya ma saff ma saff leu mbir bi saffantéla
Yaw malay danel dila simbang mbang

Serveur bi nieuw déposé plat bi yama contene ndakh yapp leu guiss sauf que ndeysan traiteur yi viande(steaks) saignant lagn ko tegual🤣

Bachir _ tay mom dingua lekk ak fourchette boulma rousslo nak chérie coco

Yama _ ay way ndaw fourchette niak diom motakh mou mel ni , nieup teudiou ay coudou ay paka mom mou nieuw tassaro doumako lalll ki pute leu

Bachir _ au secours way 😂

Yama _ olemains

Bachir _ haut les mains ?

Yama _ douma lal fourchette bi deh tei yalla diokhma diouromi baram you matt seuk meuneu dompate yapp . 😴Wah d'accord na essayé fourchette bi boulma khol deh sa beutt you lewete dina saff ataya narr

Bachir _ ma guay khass nak😂

Yama Dieul paka bi ak fourchette bi dagg yapp bi rek guiss né daffa khonk thi birr viande rouge.rek mou youkhou wouyy sama ndaye 😳😳

Bachir tite _ eh lou khew tu t'es coupé🤔

Yama _ mais Bahir li nioroul

Bachir _ Allahou Akbar tay lay dead . Li nilay mell. Sautill sauce bi gua lekk

Yama_ Ani serveur 🗣🗣ehh ehhh serveur kay diarouma neubeutou dikeul fi na gaww

Bachir _ ayy ayy ayy reglel 😏

Le serveur vient

Yama _ yaw serveur damala nourou vampire

Serveur _ non non

Yama _ dama nourou nittou goudi

Serveur _ non non

Yama _ dama nourou kouy naw atterrissage

Serveur _ non non

Yama _ gua warma khôl ak sama Sagnsé ma deff double jongoma importée . Sama cheveux thi souff sama maquillage di takk ba yakou . Sama rétane lerall salle bi .amo lomay diokh loudoul yapp bou nioroul sa cravate dima saff boumou nak 🐄. Khana sakh man Solen wa wowone ma diapalélen thi togg gui . Mousseul yappp sakh meunolen ko mann dall j'ai peukh
.
Serveur _ madame veuillez nous excuser mais c'est les recommandations du chef traiteur .

Yama _ Man kay damay commandé wate yeufou deumeu yi mom douma ko lall ahh non tounoussamerde. Kholko mouni khoudiou ni ak sa biir bou barri dolé .

Bachir _ monsieur vous pouvez disposer je vais Parler avec elle

Serveur _ je me retire si vous avez besoin de moi n'hésitez pas , monsieur madame je vous en prie .

Bachir _ merci

Yama _ niaww nappeu nako deh tamite man rek

Bachir _ cheuu man dall je ne sais pas comment faire avec Toi c'est trop

Yama _ ba yaw dall daguay lek li di diay Toubab yalgua sanne amé ténia

L'ambiance continue la musique continue yama di khôl Bahir sans cesse nak Bahir intrigué lui tient la main .

Yama _ lou khew

Bachir _ yaw lay ladj lou khew yamay khôl di ree rek

Yama _ hi hi damalay dokhane 😁

Bachir _ hahaha mossi dessone nak yama sa dieukeur la

Yama _ wawaw khana khamo dieukeur ak diabar dagno wardi dokhananté . Parfois ma khôl leu bassi yagg mattou walla ma bayi ma souff sedd ma kheutt leu plaisir 👋🏽

Bachir _ kheutt diam

Yama _ waw kheutt bagua yewou ma pissleu nelawate 🥰

Bachir _ dinafa diaré deh 😂

Yama _ guiss geu diganté dieukeur ak diabar roussangué waroufa âme deh bakhna

Qu'est ce qui peut Bien arriver de grave à ce couple se soir?😭

RAKADIOUWhere stories live. Discover now