Labanne de koba

9.3K 1K 99
                                    

Diamono djou nekak lissiy khew , diamono dji yama moy arbitré ci centrer di dirigé. Après une nuit de noce assez mouvementée . Le goût tant convoité s'est implanté .ce couple découvre les effets d'une intimité envoûtante. Le réveil est Royal , les visages radieux l'atmosphère particulièrement chaleureuse.

Elle Bachir diaw l'homme de tous les temps se réveille avec un sentiment de satisfaction inouï , ce sentiment d'avoir épouser la femme parfaite pour Lui , la femme de sa vie.

🛌Dans le lit Il caresse l'épaule de sa femme , chuchote dans ses oreilles .

El Bachir _ chérie chérie ....

Yama _ hum hum

El Bachir _ réveille toi yewoulllllll

Yama _ damay nelaww dama sonn

El Bachir _ haha

Yama _ daguay rée

El Bachir _ tu es fatiguée lou khew

Yama _ dara sama yaram moy metti rekk

El Bachir _ normal ligua deff demb yeup Aka ma contane . Bilahi doko rethiou

Yama _ motakh nak tay danouy labanne guawal wo sama bandiene

El Bachir _ louma koyy wakh ?

Yama _ wa man bane genrou niit moma takk ahh mbass

El Bachir _ legui nak ?

Yama _ wowal sama badienne néko yama fessneu bay tourou kay labanne , deff pattt , ratakhal diamono harmonisé adouna .samay noone saw lall

El Bachir appelle dallou ndakarou et  répète la même chose comme un élève de l'élémentaire _ yama fess na bay tourou kay labanne , deff pattt , ratakhal diamono harmonisé adouna .

(Dallou ndakarou famou nek di sarakholé ak tathiou
_ laylalaw sama DOM dji wathieu neu khalé bi sagual nama . fofou dou yomb dina Mélni Rossi soupou kandié beuri ingrédients ak saff saffal)

El Bachir raccroche et demande à Yama ce qui va se passer maintenant c'est un homme qui ne connait pas vraiment les traditions dans ce genre de situation. donc il veut s'informer pour faire les choses Bien

Yama _ yaw togual rek Mélni mbeurrrou chinois ok dema khôl louma deff guani cawa

El Bachir _ ok legui loumay deff nak

Yama _ laylaaaa wa ki douma kheutt foulam mou yeugeutou ni fassou narrou goor.

El Bachir _ ok ok je vais me préparer Alors wona sa badienne

Yama _ desna sa yaye ak sa sœur ak sa baye ak saye kharit ak deukeundo yi ak sa wa bureau

El Bachir _ lolou yeup

Yama _ noko nieup yekk,  na nieup yekk ni yama il est de couché il est de verge ndiank frais ni domou kany goana

El Bachir degg ndigeul wo tout le monde sans exception paré dem thi yaye dji feugg

_ TOC TOC
_ entré

Il entre délicatement salut sa mère

El Bachir _ yaye bon réveil sinon comment tu vas nakassa say rapp nak tu te sens mieux

Ya Fatou toujours sous le choc des coups et de l'eau froide _ bachir j'ai pas dormi de la nuit j'ai mal partout

El Bachir _ c'est normal yaye sa rapp paraît que daffa sokhor deh

Ya Fatou _ oh mon fils tu es si naïf mais yalla bakhna Sinon tu fais Quoi ici ?

El Bachir _ yama teudeuneu néna nako yeugeulll tout le monde ndakh day fetou

RAKADIOUWhere stories live. Discover now